TAGGOU ALADJI MADIOR CISSE
| 1-Taarou xel mou dioup kou ko ame Té di waye kou baax nanga waye Ki réewmi bokk ni yawa Moye Aladji Mâdioroh 2- Moom la YALLA diokh limou ame 3- Seydi Babacar la mou wax 4- Gorou YALLA gui kou mou wax 5- Kouko waxoul dé mooma dou dagne 6- Kou démoul dé mane dém naa 7- Wa Ndakarou niépa ngui téew 8- Thiès janxeen dé kéne déssoufa 9- Sénégala ame kouni méle 10- Moukhadame you matt Tidiane 11- Li ma wax dé mane sossou ma Thi Aladji Mâdioroh |
12- Diaka djia ngui kéne dou ko mime Gor you matt dioulite difa wax La Illa Banaan Illa Lah Mamadoh Rassoulou Lah 13- Wazifa baa ngua djipe souba téel 14- Sama beutt gueumoul nélawoul 15- Bayi léen mou dém famou dieum 16- Dji na fi garap gou raféte 17- Nioniou kat Madior guenou léen 18- Deunou gornia rirr na lou werr 19- Seydina Karim gayaa ngui 20- Binde na bataaxali xol 21- Yalna YALLA maye daradia 22- Gaw tou léen thie moom dafa ware |
